Prayers & Meditations
Wolof ·
Short Obligatory Prayer
To be recited once in twenty-four hours, at noon.
Seedenaa ne, yow suma yála ne dangama sos ngir ma xam la, jaamu la, Seedenaa ci jamano ci suma ñák katan ak ci sa mágaay, ci suma mbaadola ak sa am-am. Beneen yále amul ku moy yow, ndimbal gi ci musiba, ki dul daanu.